XELAL KO
Nu ni yow ya di xaritam
Ma ni con bok yeda
ko mu deglu la
Nit du fowé bakanam
Nit du fowé bakanam
Ndaax nu ni yen yi
xaru la
Yen yi xaru la
Xelal ko, xelal ko
Fit da fay am fu mu
yem
Fit de fay am fu mu
yem
Yen yi xarula, yen yi xaru la
Nu ni yow ya di xaritam
Yeda ko mu deglula
Waax ko mu deglula
Yen yi xaru la
Nit du fowé bakanam
Del moïtu lu la mana gaan
Moïtu lu la mana lore
Waax ko mu deglu la
Yeda ko mu deglu la
Nu ni ya di xaritam
Daara xadjul sen
diguanté
Waax ko deug mu deglu la
Deug méti na dég
wayé
Ku la waax sangul
Sa tare la beug
Nit dangay and ak sa sago
Nit dangay and ak sa sago
REF
And ak sa sago
Moïtu saytané
Xelal ko
Xelal ko
Fit da fay am fu yem
Fit da fay am fu yem
Yen yi xaru la
Yen yi xaru la
Xelal ko
Xelal ko
Xelal ko
Xelal ko
Nu ni waxambané da
na danu djurom ñari yon
Soga don goor
Weulbati sa lamin, djurom ñari yon
Soga waax mo woor
Ken xamul euleug luy
mana am (2x)
Lu ñu waax nga ni ya
xam
Lu ñu waax nga ni ya
man
Lu ñu waax nga ni ya
xam
Lu ñu waax nga ni ya
man
Mani hey !
andal ak
sa sago
Andal ak sa sago
Nit dangay and ak sa sago
And ak sa sago
Moïtu saytané
Yalla mi ñu saak
Ku tchi né bindeul
na la bess
Wayé ken xamul
fan la
Ken xamul kaañ la
Fi ak bess ba na nga
fonk
Li la Yalla djokh
Ruu bi la Yalla may
Nang ko fonk
Né yalla beugoul ñuy fowé
Bant
Banti mame yalla
Yen yi xaru la